PAASIO - PAASION / EATING HOUSE RESTAURANT / LEKKUKAAY (b)...

Info iconThis preview shows pages 1–2. Sign up to view the full content.

View Full Document Right Arrow Icon
PAASION / EATING HOUSE RESTAURANT / LEKKUKAAY (b) Jaaykat bi ak jëndkat bi ci biir lekkukaay bi / the seller and the buyer in the restaurant Jë ; jàmm nga am / are you fine ? JA : Jàmm rekk / i am fine J : indil ma / jaay ma / jox ma benn beer/ bring one cup of beer Ja :duñu jaay sàngara fii / we don’t buy alcohol here J : kon indil ma ndox / bring juice ( water) then Ja : lekk rekk lañuy jaay fii / we only buy food here J :jaay ma book ceebu jën/ bring then rice and fish Ja ; damay tëj de waxtu wi jot na / it is time to close J : man damay gan te bëgg a mos toggu Senegaal/ i am a foreigner and wants to taste Senegalese food Ja : kon xaral ma woo sama xarit bu baax mu jaay la / then let me call a kind friend of mine to buy you BAATI LÀKK Jaay / to sell ceeb / rice Jaaykat (b) seller jën / fish Jënd / to buy Jëndkat (b) : buyer Jox / to give Indi / to bring Rekk / only Lekk (g) / food Naan (g) drink Ndox (m) juice ; water Mos ; ñam / to taste Xar / to wait ÑAM / FOOD The three main senegalese dishes are : ndekki ( breakfeast) ; añ (lunch) ; reer (dinner)
Background image of page 1

Info iconThis preview has intentionally blurred sections. Sign up to view the full version.

View Full DocumentRight Arrow Icon
Image of page 2
This is the end of the preview. Sign up to access the rest of the document.

This note was uploaded on 04/29/2008 for the course LCTL 151 taught by Professor Staff during the Spring '08 term at Tulane.

Page1 / 4

PAASIO - PAASION / EATING HOUSE RESTAURANT / LEKKUKAAY (b)...

This preview shows document pages 1 - 2. Sign up to view the full document.

View Full Document Right Arrow Icon
Ask a homework question - tutors are online