JÀNGALEKAT

JÀNGALEKAT - JNGALEKAT JNGAT TEACHER STUDENTS...

Info iconThis preview shows pages 1–2. Sign up to view the full content.

View Full Document Right Arrow Icon
JÀNGALEKAT & JÀNGAT / Leer na / is that clear Am ngeen laaj ? do you have question ? Lu ngeen xalat ci… / what do you think about… Nu / naka ngeen gise…/ what is your impression about…. Deglul / degluleen…. . / listen ! Waxaatal / baamtul / repeat ! Waxaatleen / baamtuleen / repeat ! Bindal / bindleen / write ! Tontul / tontuleen ci Wolof. ./ answer in Wolof Defaral / defarleen…. / do …. . Defal / defleen / do … Ubal / ubleen ; tëjal / tëjleen / shut…. Fabal / fableen ; jëlal / jëlleen / take… Yëkkatil / yëkkatileen sa / seen loxo / raise your hand (s) Damal ci tablo bi / go to the board Laajal keneen / Ask another one JÀNGKAT & JÀNGAKAT / STUDENT / TEACHER Lan nga wax ? / what do you say ? Damay laaj… / question ! Dama bëgg a xam / i want to know … Naka / nan lañuy waxe ….ci Wolof / What is the Wolof for… Waxaat ko ; baamtu ko / repeat it Dégguma li nga wax / i don’t understand / i haven’t heard what you said Dégg naa / understand
Background image of page 1

Info iconThis preview has intentionally blurred sections. Sign up to view the full version.

View Full DocumentRight Arrow Icon
Image of page 2
This is the end of the preview. Sign up to access the rest of the document.

This note was uploaded on 04/29/2008 for the course LCTL 150 taught by Professor Staff during the Spring '08 term at Tulane.

Page1 / 3

JÀNGALEKAT - JNGALEKAT JNGAT TEACHER STUDENTS...

This preview shows document pages 1 - 2. Sign up to view the full document.

View Full Document Right Arrow Icon
Ask a homework question - tutors are online